Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:81-83

Help us?
Click on verse(s) to share them!
81Sàkku naa sag wall ba xol jeex, di xaar sa kàddu.
82Séentu naa sab dige, ba gët giim; kañ nga may xettli?
83Damaa mujj ras ni mbuusum der mu saxar jàpp, waaye sàgganewma say tegtal.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:81-83Sabóor 119:81-83