Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:78-79

Help us?
Click on verse(s) to share them!
78Yal na ñu bew ñi torox, ñoo ma lor ak seeni sos, te man may gëstu say tegtal.
79Yal na ku la ragal waññiku fi man, ba xam sa kàdduy seede.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:78-79Sabóor 119:78-79