Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:77-81

Help us?
Click on verse(s) to share them!
77Nanga ma ganesee sa yërmande, ma dund; saw yoon ay sama bànneex!
78Yal na ñu bew ñi torox, ñoo ma lor ak seeni sos, te man may gëstu say tegtal.
79Yal na ku la ragal waññiku fi man, ba xam sa kàdduy seede.
80Yal naa toppe say tegtal xol bu mat sëkk, ba duma rus.
81Sàkku naa sag wall ba xol jeex, di xaar sa kàddu.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:77-81Sabóor 119:77-81