Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:67-69

Help us?
Click on verse(s) to share them!
67Maa jàddoon, nga duma ma, léegi sa kàddu laay sàmm.
68Yaaka baax tey baaxe; rikk xamal ma say tegtal.
69Ñu bew ñee yàq sama der aki sos, te ma topp say tegtal, wéetal la.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:67-69Sabóor 119:67-69