Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:66-68

Help us?
Click on verse(s) to share them!
66Xamal ma ngëneeli àtte ak xam-xam, maa doyloo say santaane.
67Maa jàddoon, nga duma ma, léegi sa kàddu laay sàmm.
68Yaaka baax tey baaxe; rikk xamal ma say tegtal.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:66-68Sabóor 119:66-68