Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:64-68

Help us?
Click on verse(s) to share them!
64Aji Sax ji, sa ngor dajal na àddina; xamal ma sa dogali yoon.
65Aji Sax ji, def nga la nga dige woon, Sang bi, defal nga ma ngëneel.
66Xamal ma ngëneeli àtte ak xam-xam, maa doyloo say santaane.
67Maa jàddoon, nga duma ma, léegi sa kàddu laay sàmm.
68Yaaka baax tey baaxe; rikk xamal ma say tegtal.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:64-68Sabóor 119:64-68