Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:63-65

Help us?
Click on verse(s) to share them!
63Maa xejjoo képp ku la ragal, tey topp say tegtal.
64Aji Sax ji, sa ngor dajal na àddina; xamal ma sa dogali yoon.
65Aji Sax ji, def nga la nga dige woon, Sang bi, defal nga ma ngëneel.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:63-65Sabóor 119:63-65