Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:61-64

Help us?
Click on verse(s) to share them!
61Buumi ñu bon ñaa ngi may laaw, te sàgganewma saw yoon.
62Xaaju guddi laay jóg, di la sante sa àttey njekk.
63Maa xejjoo képp ku la ragal, tey topp say tegtal.
64Aji Sax ji, sa ngor dajal na àddina; xamal ma sa dogali yoon.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:61-64Sabóor 119:61-64