Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:59-61

Help us?
Click on verse(s) to share them!
59Damaa seetlu sama jëfin, dëpp, topp sa kàdduy seede.
60Maa ngi gaawtu, yeexewma say santaane moos!
61Buumi ñu bon ñaa ngi may laaw, te sàgganewma saw yoon.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:59-61Sabóor 119:59-61