Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:57-59

Help us?
Click on verse(s) to share them!
57Aji Sax ji, yaw laa séddoo; di digee sàmm sa kàddu.
58Sama léppi xol laa sàkkoo saw yiw, ngalla baaxe ma, yaa ko dige.
59Damaa seetlu sama jëfin, dëpp, topp sa kàdduy seede.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:57-59Sabóor 119:57-59