Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:52-54

Help us?
Click on verse(s) to share them!
52Éy Aji Sax ji, damaa fàttliku sa àtte ya woon, daldi muñ.
53Sama xol daa fees ndax ñu bon ñiy wacc saw yoon.
54Sa dogali yoon laay woyantoo, fu ma mana sance.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:52-54Sabóor 119:52-54