Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:32-34

Help us?
Click on verse(s) to share them!
32Sa yoonu santaane laay daw, yaa may may xol bu tàlli.
33Aji Sax ji, xamal ma li sa dogali yoon yiy firi, ma topp ko ba mu jeex.
34May ma dég-dég, ma topp saw yoon, toppe ko xol bu tàlli.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:32-34Sabóor 119:32-34