Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:164-166

Help us?
Click on verse(s) to share them!
164Juróom yaari yoon ci bés màggale naa la ko say àttey njekk.
165Jàmm ju baree ñeel ku sopp sa yoon, te dara du ko fakktal.
166Aji Sax ji, sa wall laa yaakaar, say santaane laa jëfe.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:164-166Sabóor 119:164-166