Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:160-164

Help us?
Click on verse(s) to share them!
160Sa mboolem kàddu dëgg la, sa ndigal yépp di njekk, sax dàkk.
161Ay kilifaa ma topp ci dara, te teewul ma wormaal sa kàddu.
162Man de, maa ngi bége sa kàddu ni ku for alal ju bare.
163Fen, ma bañ, ba sib; sa yoon, ma sopp.
164Juróom yaari yoon ci bés màggale naa la ko say àttey njekk.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:160-164Sabóor 119:160-164