Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:135-138

Help us?
Click on verse(s) to share them!
135Sang bi, geesoo ma sag leer, te xamal ma sa dogali yoon,
136ay wali rongooñ ay wale saay gët, ndax sàmmeesul saw yoon.
137Aji Sax ji, yaaka jub, te say àtte di yoon.
138Yaa santaane sa kàdduy seede ci njekk ak worma ju yaa.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:135-138Sabóor 119:135-138