Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:122-125

Help us?
Click on verse(s) to share them!
122Sang bi, gàddu ma, ma am jàmm, bu ma ñu bew ñi néewal.
123Séentu naa sag wall ak sa kàddug njekk, ba saay gët giim.
124Sang bi, jëfeel ma sa ngor, xamal ma sa dogali yoon.
125Sab jaam laa, may ma, ma ràññee, ba xam sa kàdduy seede.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:122-125Sabóor 119:122-125