Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:105-107

Help us?
Click on verse(s) to share them!
105Sa kàddu laay niitoo samay tànk, muy leeral samaw yoon.
106Giñ naa te di ko dëggal, ne dinaa sàmmonteek sa ndigali njekk.
107Toskare naa ba ci lool; éy Aji Sax ji, musal ma, yaa ko dige.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:105-107Sabóor 119:105-107