Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Mucc ga - Mucc ga 20

Mucc ga 20:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3«Buleen am yeneen yàlla ci sama kanam.
4«Buleen sàkkal seen bopp tuur muy jëmmal lenn lu nekk ci kaw asamaan, mbaa ci kaw suuf, mbaa lu nekk ci ndox mu suuf tiim.
5Buleen ci sujjóotal lenn, buleen ci jaamu lenn, ndax man seen Yàlla Aji Sax ji, Yàlla ju fiir laa. Maay topp doom tooñu waajur, ba ca seen maasi sët, ba ca maasug sëtaati nit ñi ma bañ.

Read Mucc ga 20Mucc ga 20
Compare Mucc ga 20:3-5Mucc ga 20:3-5