Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Esayi - Esayi 42

Esayi 42:16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
16Maay doxloo silmaxa yi ci yoon wu ñu xamul, ñall wu ñu miinul laa leen di jaarale. Maa leen di soppil lëndëm gi fi seen kanam, ag leer, fu ñagas, ma maasaleel leen. Lii laa leen di defal, te duma leen wacc mukk!

Read Esayi 42Esayi 42
Compare Esayi 42:16Esayi 42:16