Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 42:16 in Wolof

Help us?

Esayi 42:16 in Kàddug Yàlla gi

16 Maay doxloo silmaxa yi ci yoon wu ñu xamul, ñall wu ñu miinul laa leen di jaarale. Maa leen di soppil lëndëm gi fi seen kanam, ag leer, fu ñagas, ma maasaleel leen. Lii laa leen di defal, te duma leen wacc mukk!
Esayi 42 in Kàddug Yàlla gi