Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Esayi - Esayi 1

Esayi 1:30-31

Help us?
Click on verse(s) to share them!
30Yeenay meli ni garab gu mag gu xob ya lax, mbaa tóokër bu amul siitu ndox.
31Boroom doole mel ni boob, la mu liggéey di ferñent, ànd ak moom ne jéppét, te kenn du fey sawara wa.

Read Esayi 1Esayi 1
Compare Esayi 1:30-31Esayi 1:30-31