Text copied!
Bibles in Wolof

Esayi 1:30-31 in Wolof

Help us?

Esayi 1:30-31 in Kàddug Yàlla gi

30 Yeenay meli ni garab gu mag gu xob ya lax, mbaa tóokër bu amul siitu ndox.
31 Boroom doole mel ni boob, la mu liggéey di ferñent, ànd ak moom ne jéppét, te kenn du fey sawara wa.
Esayi 1 in Kàddug Yàlla gi