Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Esayi - Esayi 1

Esayi 1:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Aw yëkk xam na boroomam, mbaam-sëf xam gàmb, bi ko boroomam di xonte, waaye Israyil xamul, sama ñoñ ñii xàmmeewuñu.»
4Wóoy wii xeetu moykat, wii askan wu diisu ñaawtéef, mii njurum defkati mbon, yii doomi yàqute! Ñoo wacc Aji Sax ji, ñoo teddadil Aji Sell ju Israyil, dëddu ko.

Read Esayi 1Esayi 1
Compare Esayi 1:3-4Esayi 1:3-4