Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Esayi - Esayi 49

Esayi 49:15

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15«Ana jaboot juy fàtte doomam juy nàmp, mbaa muy néege ku mu jur ci biiram. Bu ko manoona fàtte it, man duma la fàtte.

Read Esayi 49Esayi 49
Compare Esayi 49:15Esayi 49:15