Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Baamtug Yoon wi - Baamtug Yoon wi 28

Baamtug Yoon wi 28:13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Aji Sax jee leen di def bopp, te du leen def ub geen, te kaw rekk ngeen di jëm, waaye dungeen jëm suuf, ndegam yeena ngi topp seen santaaney Yàlla Aji Sax ji ma leen di dénkal sama bopp bésub tey, di ko sàmmoo jëfe,

Read Baamtug Yoon wi 28Baamtug Yoon wi 28
Compare Baamtug Yoon wi 28:13Baamtug Yoon wi 28:13