Text copied!
Bibles in Wolof

Baamtug Yoon wi 28:13 in Wolof

Help us?

Baamtug Yoon wi 28:13 in Kàddug Yàlla gi

13 Aji Sax jee leen di def bopp, te du leen def ub geen, te kaw rekk ngeen di jëm, waaye dungeen jëm suuf, ndegam yeena ngi topp seen santaaney Yàlla Aji Sax ji ma leen di dénkal sama bopp bésub tey, di ko sàmmoo jëfe,
Baamtug Yoon wi 28 in Kàddug Yàlla gi