Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Baamtug Yoon wi - Baamtug Yoon wi 28

Baamtug Yoon wi 28:12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Aji Sax jee leen di ubbil mbàndam mu baax ma fa asamaan, ba bu jotee mu tawal seenum réew, boole ci barkeel seen mboolem ñaq. Yeenay lebal xeet yu bare, waaye yeen dungeen leb.

Read Baamtug Yoon wi 28Baamtug Yoon wi 28
Compare Baamtug Yoon wi 28:12Baamtug Yoon wi 28:12