Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 5

Kàdduy Waare 5:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Boo gisee ñuy not néew-ji-doole, di jalgati dëgg ak yoon cib gox, bumu la jaaxal; kilifa gi, kilifaam a ko yiir; ñoom it seen kilifaa leen yiir.
8Xanaa ndax buur suqal mbey mi, ba ñépp jariñoo suuf si.
9Bëggkatu xaalis du doyal xaalis, bëggkatu alal du doyal tono, te loolu it, cóolóoli neen.

Read Kàdduy Waare 5Kàdduy Waare 5
Compare Kàdduy Waare 5:7-9Kàdduy Waare 5:7-9