Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 5:7-9 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 5:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Boo gisee ñuy not néew-ji-doole, di jalgati dëgg ak yoon cib gox, bumu la jaaxal; kilifa gi, kilifaam a ko yiir; ñoom it seen kilifaa leen yiir.
8 Xanaa ndax buur suqal mbey mi, ba ñépp jariñoo suuf si.
9 Bëggkatu xaalis du doyal xaalis, bëggkatu alal du doyal tono, te loolu it, cóolóoli neen.
Kàdduy Waare 5 in Kàddug Yàlla gi