Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 18

Kàddu yu Xelu 18:20-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Làmmiñ feesal na biiru boroom, yoolu kàddu suur na boroom.
21Dund ak dee a ngi ci làmmiñ, te wax garab la, ku ko bëgg, lekk ca doom ya.
22Ku am jabar, am nga ngëneel, am nga yiwu Aji Sax ji.

Read Kàddu yu Xelu 18Kàddu yu Xelu 18
Compare Kàddu yu Xelu 18:20-22Kàddu yu Xelu 18:20-22