Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:20-22 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:20-22 in Kàddug Yàlla gi

20 Làmmiñ feesal na biiru boroom, yoolu kàddu suur na boroom.
21 Dund ak dee a ngi ci làmmiñ, te wax garab la, ku ko bëgg, lekk ca doom ya.
22 Ku am jabar, am nga ngëneel, am nga yiwu Aji Sax ji.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi