Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Room - Room 6

Room 6:10-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Deeyam ga mu dee ca la deeyal bàkkaar benn yoon ba fàww, te dund gi muy dund tey, Yàlla la koy dundal.
11Naka noonu, yeen itam jàppeleen seen bopp nit ñu deeyal bàkkaar, te di dundal Yàlla, ci Yeesu Almasi.
12Kon nag bu bàkkaar yilif seen yaramu ndee wii, ba di leen nanguloo ay xemmemtéefam yu bon.

Read Room 6Room 6
Compare Room 6:10-12Room 6:10-12