Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - ROOM - ROOM 6

ROOM 6:10-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Dee na benn yoon, ba bàkkaar manul ci moom dara; mi ngi dund léegi, di ànd ak Yàlla ba fàww.
11Ci noonu nag yéen itam tegleen seen bopp ni ñu dee ak Kirist, ba rëcc ci dooley bàkkaar, di dund, ànd ak Yàlla ba fàww ndax seen bokk ci Yeesu Kirist.
12Buleen mayati bàkkaar nag, mu yilif seeni yaram yu néew doole, bay topp ay bëgg-bëggam.

Read ROOM 6ROOM 6
Compare ROOM 6:10-12ROOM 6:10-12