Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ose - Ose 4

Ose 4:6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Sama ñoñ a sànku ndax ñàkka xam; yeen, xam-xam ngeen gàntal, ma gàntal seenug carxal. Yeena fàtte seen yoonu Yàlla, man it maay fàtte seeni doom.

Read Ose 4Ose 4
Compare Ose 4:6Ose 4:6