Text copied!
Bibles in Wolof

Ose 4:6 in Wolof

Help us?

Ose 4:6 in Kàddug Yàlla gi

6 Sama ñoñ a sànku ndax ñàkka xam; yeen, xam-xam ngeen gàntal, ma gàntal seenug carxal. Yeena fàtte seen yoonu Yàlla, man it maay fàtte seeni doom.
Ose 4 in Kàddug Yàlla gi