Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - KOLOS - KOLOS 2

KOLOS 2:6-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Kon nag, ni ngeen nangoo Kirist Yeesu ni Boroom bi, dundeleen noonu ci moom.
7Saxleen ci moom, di màgg ci moom, tey gëna dëgër ci ngëm, gi ñu leen jàngal, ba seen xol di baawaan ci gërëm Yàlla.
8Moytuleen ba kenn bañ leena fàbbi ci ay xam-xami nit yuy naxi neen. Xam-xam yu mel noonu, ñu ngi soqikoo ci aada yu nit tëral, ci aaday àddina, waaye soqikoowul ci Kirist.

Read KOLOS 2KOLOS 2
Compare KOLOS 2:6-8KOLOS 2:6-8