Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kolos - Kolos 2

Kolos 2:6-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Kon nag, ni ngeen nangoo Almasi Yeesu di Sang bi, àndleen ak moom, jëfe noonu.
7Sampleen seeni reen ci moom, tabaxuleen ci moom, feddlikuleen ci wàllu ngëm, ni ñu leen ko jàngale, ba seenub xol baawaanal kàdduy cant.
8Moytuleen ba kenn bañ leena këfe kàdduy naxi neen yu ñu jàppe xam-xam bu xelu, kàddu yu sukkandikoowul Almasi, xanaa aaday nit, ak cëslaayi àddina.

Read Kolos 2Kolos 2
Compare Kolos 2:6-8Kolos 2:6-8