Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 5

Kàdduy Waare 5:9-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Bëggkatu xaalis du doyal xaalis, bëggkatu alal du doyal tono, te loolu it, cóolóoli neen.
10Bu koom yokkoo, lekk-kat yi yokku. Ana lu muy jariñ boroom koom ga, xanaa di ko duufale bëtam?
11Surga, lekkam néew, bare, mu nelaw, ba fàttey boram; boroom alal regg, du nopplu, du nelaw.

Read Kàdduy Waare 5Kàdduy Waare 5
Compare Kàdduy Waare 5:9-11Kàdduy Waare 5:9-11