Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 5:9-11 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 5:9-11 in Kàddug Yàlla gi

9 Bëggkatu xaalis du doyal xaalis, bëggkatu alal du doyal tono, te loolu it, cóolóoli neen.
10 Bu koom yokkoo, lekk-kat yi yokku. Ana lu muy jariñ boroom koom ga, xanaa di ko duufale bëtam?
11 Surga, lekkam néew, bare, mu nelaw, ba fàttey boram; boroom alal regg, du nopplu, du nelaw.
Kàdduy Waare 5 in Kàddug Yàlla gi