Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 2

Kàdduy Waare 2:6-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6sàkklu samay déeg, di ko suuxate, garab ya naat.
7Ma jëndi jaam, góor ak jigéen; ñu ami doom ci kër gi. Ma am jur gu ne gàññ, gu gudd ak gu gàtt, ba ëpple ku ma jiitu ci Yerusalem.

Read Kàdduy Waare 2Kàdduy Waare 2
Compare Kàdduy Waare 2:6-7Kàdduy Waare 2:6-7