Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 2:6-7 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 2:6-7 in Kàddug Yàlla gi

6 sàkklu samay déeg, di ko suuxate, garab ya naat.
7 Ma jëndi jaam, góor ak jigéen; ñu ami doom ci kër gi. Ma am jur gu ne gàññ, gu gudd ak gu gàtt, ba ëpple ku ma jiitu ci Yerusalem.
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi