Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 1

Kàdduy Waare 1:11-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Kenn du fàttliku ñi jiitu, ñiy ñëwit, ñi leen topp duñu leen fàttliku.
12Man waarekat bi, buurub Israyil laa woon ci Yerusalem.

Read Kàdduy Waare 1Kàdduy Waare 1
Compare Kàdduy Waare 1:11-12Kàdduy Waare 1:11-12