Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 1:11-12 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 1:11-12 in Kàddug Yàlla gi

11 Kenn du fàttliku ñi jiitu, ñiy ñëwit, ñi leen topp duñu leen fàttliku.
12 Man waarekat bi, buurub Israyil laa woon ci Yerusalem.
Kàdduy Waare 1 in Kàddug Yàlla gi