Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 11

Kàdduy Waare 11:4-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Kuy déglu ngelaw, doo ji, kuy seetluy niir, doo góob.
5Xamoo yoonu ngelaw, xamoo nu doom di sosoo ci ndeyam; kon manoo xam lu Yàllay def, moom miy def lépp.

Read Kàdduy Waare 11Kàdduy Waare 11
Compare Kàdduy Waare 11:4-5Kàdduy Waare 11:4-5