Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 11:4-5 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 11:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Kuy déglu ngelaw, doo ji, kuy seetluy niir, doo góob.
5 Xamoo yoonu ngelaw, xamoo nu doom di sosoo ci ndeyam; kon manoo xam lu Yàllay def, moom miy def lépp.
Kàdduy Waare 11 in Kàddug Yàlla gi