Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:5-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Téxét bi, deel foog, dof bi, déggal ndéey lu xelu.
6Déglul, ma wax la lu am solo, dégtal la njub.
7Dëgg laay wax, di bañ wax ju bon.
8Lu ma wax njub la. Amul lu dëng mbaa lu jekkadi.
9Lépp a dëggu ci ku am ug dégg, te jub ci ku for xam-xam.
10Na la samab yar gënal xaalis, xam-xam dàqal la ngën-gi-wurus.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:5-10Kàddu yu Xelu 8:5-10