Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:30-33

Help us?
Click on verse(s) to share them!
30man, Xel mu Rafet, maa doon ku xareñ ci wetam, di ko bànneexal bés bu ne, tey bànneexu fi kanamam.
31May bége wërngalu àddinaam, di bànneexoo doomi aadama.»
32«Kon nag, doom, dégluleen ma. Mbégte ñeel na ki may topp.
33Dégluleen ku leen di yar, daldi muus. Buleen ko sàggane!

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:30-33Kàddu yu Xelu 8:30-33