Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:30-33 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:30-33 in Kàddug Yàlla gi

30 man, Xel mu Rafet, maa doon ku xareñ ci wetam, di ko bànneexal bés bu ne, tey bànneexu fi kanamam.
31 May bége wërngalu àddinaam, di bànneexoo doomi aadama.»
32 «Kon nag, doom, dégluleen ma. Mbégte ñeel na ki may topp.
33 Dégluleen ku leen di yar, daldi muus. Buleen ko sàggane!
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi