Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 6

Kàddu yu Xelu 6:9-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Moo yaafus bi, foo àppal tëraay bi? Loo deeti xaar ci yewwu?
10Ngay dajjant ak a for bët, di tegley loxook a jaaxaan.
11Néewlee ngi lay dikkal nib sàcc, ñàkk gànnaayul la.
12Ku tekkeedi te bon, day wër di fen,

Read Kàddu yu Xelu 6Kàddu yu Xelu 6
Compare Kàddu yu Xelu 6:9-12Kàddu yu Xelu 6:9-12