Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 4

Kàddu yu Xelu 4:9-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Da lay takkal kaala gu jekk, solal la mbaxanam buur.»
10Déglul, doom, te dégg saay wax, ndax nga gudd fan.
11Yoon wu xelu laa la teg, jaarloo la yoonu njub.
12Doo dox ba tërëf, doo daw, téqtalu.

Read Kàddu yu Xelu 4Kàddu yu Xelu 4
Compare Kàddu yu Xelu 4:9-12Kàddu yu Xelu 4:9-12